Dem dem
Dem fan ?
Den ndax lan ?
Baya ko mom
Dem nguir xee bou barri bi
Dem ndax teen boh neex bi
Teh rapp rek noom noo siy naan
Nach bi lakkatouma taw bi barrewoul
Dem ngir bokk bone menou fee am
Dem ngir daffa wara nekk gorr done
Goorgoorlau
Dem dem
dem fan ?
Dem ndax lan ?
Liberte bi
Si espace bou lendeum bi
Sama beut yi guissa tounou
Garap yi nga xamenteni noo ma souxat
Su beut setiee barap yi bow
Dem ngir Keur gui daf may nirou lou lendeum
Dem nguir daffa warranekk goor done
Goorgoorlau
Damay dem
Chi alla bi
Damay dem Chi dex goumak gui
Ne damay dem waw seeti sama nawleyee
Damay dem si ban bou ritax bi
Damay dem ba reewu bitty
Ne damay dem waw setti samambokkyee
go-go (bis)
Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy
Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar
Hey what do you need ?
He he yaw lilaneex
Won ma sa yarii ma wax la ki nga donoy
Won ma sa mbokk ma wax ko fi ngay diaar
He defa li la neexoy hey yaw lila soop
Sammkatou mboott moo xam ba ciy
Sooxaoy ni meneuh kott noom daal amounou
Mbaam hey defal li la nexx oo
hey what do you want ?
Ho ho ho ho ....
Youssou N'Dour è un cantante, musicista e politico senegalese nato a Dakar nel 1959. Considerato uno dei più grandi artisti africani di tutti i tempi, N'Dour ha raggiunto fama internazionale grazie alla sua musica che fonde tradizioni musicali africane con influenze pop e world music. Inizia la sua carriera negli anni '70 come cantante in un gruppo di musica tradizionale senegalese, per poi emergere come solista negli anni '80 con album come "Set" (1984) e "Tumba" (1988). N'Dour ha collaborato con artisti internazionali come Peter Gabriel, Bruce Springsteen e Sting. Nel 2004 è stato nominato Ministro della Cultura del Senegal, dimostrando il suo impegno politico per la sua patria. Tra i suoi brani più famosi si ricordano "7 Seconds" (con Neneh Cherry), "Djam Djam", "Isla Bonita" e "Bounou Bouna." N'Dour ha vinto numerosi premi musicali, tra cui un Grammy Award nel 2005 per l'album "Egypt".
La chanteuse de renom Rihanna et le rappeur A$AP Rocky ont récemment fait la une des journaux du monde entier en dévoilant le nom de leur deuxième enfant.
Avec son riche héritage culturel et sa scène musicale dynamique, Paris offre un paysage sonore unique qui continue de captiver les mélomanes du monde entier.
Il vient de loin, d'une terre riche de culture et de traditions millénaires, une terre qui surplombe le Pacifique, mais qui se baigne aussi dans les Caraïbes et qui ces dernières années est surtout connue pour les terribles nouvelles liées au trafic de drogue
C'était le 5 avril 1980 quand un groupe inconnu et sans nom a joué dans une église désacralisée de la ville universitaire d'Athens en Géorgie. À peine deux semaines plus tard, ils ont choisi un nom R.E.M. , et ilt ont sortiun single et en 1983 un album "Murmur".
Avec 7 albums à leur actif, le groupe est une source d'inspiration et de créativité au niveau mondial, au cours de ces 20 années il n'a cessé d'influencer le paysage musical et de créer des tendances.
Nous continuons donc à voir un balancement entre les festivals d'été et non, nous devons les annuler car nous ne pouvons pas garantir la sécurité.
Il sont 7, ils ont presque tous la vingtaine, ils aiment le post-rock et aussi expérimenter différents sons. Plus qu'un groupe, Black Country est une communauté.
J'ai l'impression qu'avant d'aborder le sujet traité dans cet article je dois faire une prémisse: le reggaeton n'est pas vraiment mon genre préféré, il se réfugie dans un rythme très banal avec des textes que 99% du temps décrivent la femme comme un objet disponible à l'homme macho.
Le film très critiqué «Musique» de Sia qui voit son début en tant que réalisatrice vient d'être nominé comme meilleur film au Golden Globe 2021. L'actrice principale Kate Hudson a été nominée dans la catégorie Meilleure actrice.